1. Lan mooy bile banxaasu caada yu uute? 3. Yan xeeti tééré la ëmbb? 4. Ana ci lan lamay soxal? - Xeeti tééré yi mu ëmbb xaajees nako yatti Bile banxaasu caada yu uute benn la ci banxaas yi nekk ci gëstukaayu nguur guii ñu Bërëbu gëstukaay danay faral di jariñ ci: pacc yu mak: ● Di abale ay jumtukaay: niki ay tééré. Ay CD, ay CD-ROM, ak yuni mel… ay tééré yuy yeete ci mbiri uute ciy dupee Manuel Alvar ci Zaragoza. Ñu ngi ko caada: ci kallama español, aju ci sos disi jublu dongg cosaanal xeet wu yaa te yeneeni rééw akiy aada, boole ca lim ci bërëbu xarala bi: ñu dileen fattali ni uute. bu takku ciy tééréy nettali. man Nguir man ko, namm nañu: ● ● rééwma: ay tééré ci topatoo soxlo yi aju ci taggatu, ci kallama bu uutek español taamu ca teewlu ak caada nakkallamay ci xeet buy gen di wuute ● Mbinddum bokk ci di yee xeet wi ci jikko yu raet rééwu Ubil bunt ñi soxlo jëfëndikoo ordinatëër ngeen faa ubbi seen keesu bataaxalu unternet ak xool buuntu webu adduna bi yépp te dooleen fay dara. cosaanu doxandéém yi ëpp ci sunu gox bi. Ngeen mana jangg xew-xew yi ñu siiwël ak yëglekaayu adduna bi yëpp. Njangum lakk, bokkna ca lakku español. - xeeti jumtuwaay: tey fy tey, laca ëpp ya tééré 5. Nen laa fay mana gisee limay seet? Jangg ak yër ci bërëbu tééré yi. ñeel xeet wu bari melo. 2. Ana kan lañu ko jagleel? la, ay CD mmisigu adduna bi, ay CD ROM akiy Joteesna ci jumtukaay yi ci lu amul benn Naka bërëbu gëstukaayu nguur yëpp, ak yëglekaayu xibaar. galangkoor. Ba taxna kiko soxlo man na caa jot yeneen banxas yi nekk ci gëstukaayu Manuel ● Lu aju ci yëglekaay yi, deesna ci te du jaar fenn. Alvar, banxaas bii ñeelna mboleem doomu jappandal yëglekaayu addina bi yëpp: Lu adama, ak lu mana doon xeetam, baa rééw, xibaari bës bi, yuñu sotti ci këyit, altine gëstukaay bi ñu ngi leen di déglu ngir yombal baa ay atam, baa pëyëm, baa diinéém, baa ba gau, -jaaree ci jaww ji- taamu ci yi seen jëfëndikoo jumtukaay yi. lakam, laago, koom koom, liggééy wala jugee ci rééwu doxandéém yi ëpp ci Tayitam, ci jamono jii, ñungi ak kurel tektalkat gnangam. gox bi, boo xameen mënees nacaa jot. ci aada yu uute, ñi ci nekk bokk ci ay xeet yu Mënees uute. Limu ëmbb ciy tééré taxna mu soxal lool askan wi bawoo ci yeneeni rééw ak yépp ñi nga xamne caada yu uute lenn ciy caada soxalna leen. naa nemmiku ci bërëbu mana xew nak, liggéykaati bërëbu gëstukay bii mbooleem yëglekaay yiñu fay faral di sotti ci këyit. Kenn ku nekk ci tektalkat yi man naa jëféndikoo lakku rééwám ngir dimbëli ña fay ñëw bu ñu ko soxlaa. Ci bërëbu gëstukaay bi ak ci sunu buntu web 7. fan la nekk? BANXAASU CAADA YU UUTE Tektal: BËRËBU GËSTUKAAY MANUAL dingeen fa fekk “tektalukaay bi” ci kallaama español, araab, rumani, poloñ, rusi, farañse, angale… ALVAR Bërëbu gëstukaayu Manuel Alvar 6. Lan laay soxla gir jariñoo ko? Edificio El Pilar, Parque Delicias. Lees di ci laac, benn la ak ci bërëbu 50017 ZARAGOZA gëstukaayu nguuri gox bi yëp. Kenn ku nekk man na ci duggu ci lu amul benn galankoor te Teléfono: 976 488 433 ñaring yi ñu jëkkë lim deesu ci fay dara. Correo electrónico: Guirmanamana abb di yobbu sa kër, ak di bibliotecas-malvar@zaragoza.es doggu internet, wáy jëfëndiku bi warnaa joxe ci Web: http://educacion.zaragoza.es bërëbu gëstukaay bi ñaari nataalu dantite te wane waale benn këyitu mandarga buñu koy waxtuy kubbite: xammee. Altine ci ngoon: ci 15 waxtu ba 21 waxtu. Ngir jëfëndikug internet, xale yi ammul juroom Li dalee ko talaata ba aljuma: ci 9 waxtu ba ñatti (8) at dañu wara andak seeni way jur 21 waxtu. walla seeni njaatigui. Ñi am diggënte 8 ba 18 Gaau: ci 9 waxtu ba 14 waxtu at, munul ñakk ñu wane këyit bu wax en seen kilifa moleen nangul. Weeru sulet ba waxset: dalee ko altine ba ajuma, ci 9 waxtu ba 14 waxtu (ci suba si) ak ci 16 waxtu ba 21 00226waxt