GUWERNMAA ARAGON. Kureelu Njàŋgale, Caada ak Taggat Yaram Servicio Provincial de _________________ AV. Juan Pablo II, 20. 50071 Saragosse ÀBB PC Man, M./Mme..............................................................................., mi yore Paaspoor/CNI wolla beneen kayit ……………………….....……………………………di ndey wolla baay ci eleewbi ……………………………………………………………….. bi bindu ci collège……………………………………………..……… …….….……bi ci dëkku ......................................ci .....eelu at njàŋg mu suufe, maangii ñaan ñu àbalma tablet PC ndax sama doom mën ko yobbu bis bu neek ca kër ga ngir def dewaaram ak ligeey yi ñu ko sant. Dinaa ko xool bu baax te topp ndigël yi ñu joxe fii ci suuf ak yi ekoolbi mëna joxe. Ci.................................., bisu’b.............................. 2006 Siñaatiiru baaybi ak /wolla ndeyji. Ndigël : - Tablet PC juumtukaayu liggeeyu eleewbila. Waajurwi warna jàŋgal xalebi liggeey bu rafet te sakkal ko bërëb bu baax bu mu mën defe ay dewaaram. Warna ñ ko sakkal woxtu wu muy def ay dewaaram ci kërgi, di topp ndigalu jàŋgalekatyi xam ni moo jariñoo tablet PCbi. Tablet PCbi warnañ ko teye bu baax suñ ko dee toxal digante kërgi ak ekoolbi ngir bu ko dara dal. Su xalebi jàŋgiwul ak su ekool bëree nawet, dafa war yobbu tablet PCbi ci Santrbi. Ndigëlyi dinañ ko jox waajurwi ci ndaje diggante jàŋgalekatbi ñu déŋk kalaasbi ak njiit yi ci bis bi ñu bind fii ci kow. Tablet PC numero ............ .....mark ……………… …… ……, abalnañuko eleew bi ñu tudd fii ci kow. Direktër àndnaci Jàŋgalekatbi ñu déŋk kalaasbi